dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

limboo : sol (ay sagar), làmboo. mu nga limboo yére yu tilim nekk ca biir nit ña.