dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

likke : yeew (ay mala) ci genn buum. likke na bëy yi mu war a jaayi suba.