dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

laf b- 1 : doole j-, kàttan g-. mbër dafa war a am laf.

laf b- 2 : cat l-. sa lafu musoor baa ngi direeku.

laf : tege boor, fegg. yal na la Yàlla lafal cat.