dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

jaxran : baat bi dafay tekki loo gis ak say gët. ne na gis na ko jaxran muy tux. dinañuy wax tamit jahran.