dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

jant-jantee : yenu ku mënalul boppam dara, fab, meeb. màgget si léegi dañu koy jant-jantee rekk.