dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

jamar b- : góom bu nekk ci ginnaawu fas wala gu mbaam. lu doon def fas wi jamar bi ?