dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

jadd : (ne jadd). xodd. baat bi dafay tekki taxaw taxawaay bu dëgër. alkaati baa ngi ne jadd ca kow tali ba.