dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

jaambur b- : nit ku moom boppam. jaambur yee ëpp jaam ñi. safaan wi mooy jaam b-. / nit ku am jàmm. du tooñ kenn, jaambur bu mag la. / keneen. defal li ngay def te bàyyi jaambur. dinañuy wax tamit jàmbur b-.