dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

gont : dem ci ngoon gi. du xëy, dafay gont liggeeyi. safaan wi mooy xëy.