dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

gàngunaay m- : toogu b-, siis b-. suñu gan gi lañu fi tegal gàngunaay mi. dinañuy wax tamit gàngune m-.