dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

gàdd g- : géttu golo g-. ag gàdd a jaar ca toolam, yàq ko yépp.