dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

gàññ : (ne gàññ). bare ba mu ëpp, xas (ne). démb jën yaa ngi ne woon gàññ ca marse ba.