dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

foy-foyi : yëngatu bu aju ci ngelaw li, mën na doon ab morso wala aw xob. xobi garab gaa ngi foy-foyi di naaw. dinañuy wax tamit foyy-foyyi.