dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

faxaj : baaraam bi dafa faxaj bu yàgg ba léegi. dinañuy wax tamit fëxëj wala foxoj.