dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

dëyya : fey loraange. nguur gi war na dëyya ñi yàqule ci kuraŋ biy kuppe guddi ak bëccëg.