dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

dëtëm : dëtëm mooy naane ni mala ci misaal. bul dëtëm ndox mi, jëlal kaas.