dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

cuq 1 : neex, turumtàcc. sa ceeb bi cuq na. safaan wi mooy naqari.

cuq 2 : ruux. mu ngi lay cuq rekk wànte boo ciy dugg, di ci des.