dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

caxabal : lonk sa tànk ci tànku ki ngay bëreel ngir daaneel ko. dafa ko bëggoon a caxabal.