dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

càq : wékk dugub, denc ko diiru at. dugub ji ma càqoon laay def jiwu.

càq g- : géppen b-. bant bu gudd bu am ay càq bu ñu samp ci bunt tool ngir bañ jur gi dugg ci mooy càq.