dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

càmbar : tànn, segg. càmbar ko bu baax, génnee lépp lu ci bon.