dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof
nanu delloo làkki réew mi seen gëdd, di leen jëfandikoo ci bépp jokkoo. Séex Anta Jóob nee na : "làkku jàmbuur, su neexee ni tàngal it, kenn mënu koo macc ba ciy tàqamtiku."
dibéer, ñaar-fukki fan ak ñaar, ci weeru awiril, atum 2018