dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

balaxalmàddaa : dund dund gu neex lool. mu ngi balaxalmàddaa de wànte xaalisu askan wi la sàcc.