dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

balaacaag : bala ñu fay yegg (bala cay àgg). sa xar mi dafa seer ba mu ëpp, balaacaag ma jënd nag.