dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

baaxoñ b- : baaxoñ xeetu picc la. baaxoñ bi dal na ci bànqaasu garab gi.