dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

uy : uy baat la bu ñuy wax, bu ñu bëggul a wax baat bu ñaaw bi topp ci wax ji. boo ko defati ma…, uy !

uyu : tontu ci ab woote. bi nga ko woowee, uyu na la, yow yaa ko déggul. dinañuy wax tamit wuyu.