dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

uslu b- : doxalin w-. uslu colinam dara yiwu ci.

ustaas b- : jàngalekat ci daara yi. ustaas bi def ci yow xam-xam, danga ko war a weg, fonk ko.