dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

und w- : muus m-, janaab j-. und waa ngi lekk jën yi. dinañuy wax tamit wund w-.

unk b- : tabandoor b-. unk baa ngi dox ci miir bi.

un b- : un xeetu mbonaat mu rëy la.