dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ujaaj b- : ku war a dem Màkka lañuy tudde ujaaj. ujaaj yaa ngi ci waajaayu dem Màkka.