dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ub 1 : ub na bunt yeek palanteer yépp laata muy tëdd. safaan wi mooy ubbi.