dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

sãas : tàng ba ëpp. dëwlin gi sãas na léegi.

sãas b- : wërsëg w-. xale bi am na sãas.