dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

róbine b- : ndoxu robine bi dafa saf xorom.

rókkin : dal ci kow nit. ku ma ko rókkin ma dabin la ko.

rósi : ndaw si rósi na yàpp wi ba pare.