dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

oyof : àttan na saaku bi, dafa oyof. dinañuy wax tamit woyof. safaan mooy diis.

oyu : soo paree nanga oyu ki lay oo. dinañuy wax tamit uyu wala wuyu. safaan wi mooy oo.