dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

otel b- : bérebu dàlluwaay b-. otel lay jël benn néeg diiru li mu fiy nekk.

oto b- : dinañuy wax tamit woto b-. (seetal woto)