dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

os : teg ay xeer fi wër safara si, soog ci teg cin li. soo taalee, nanga os cin li. dinañuy wax tamit wos.