dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

opitaal b- : dinañuy wax tamit loppitaan b- wala loppitaal b-. (seetal loppitaan)

opp : feebar. liggeeysiwul tey, dafa opp. dinañuy wax tamit wopp.