dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

nóox : nor, nott. fótëey bi dafa nóox. dinañuy wax tamit nuux. safaan wi mooy funki wala junki.

nóoxoor b- : nee nañu nóoxoor mooy koo xam ne pàppaam dëmm la wànte yaayam nekku ko.