dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

itam : dinañuy wax tamit it. (seetal it)

it : yow it lu baax li ngay digle, dee ko def. / waxuma dara, man it laajuma ko. dinañuy wax tamit itam, tam wala tamit.

itte j- : soxla s-. nit ñi léegi dañoo bare ay itte. dinañuy wax tamit yitte j-.