dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

iskale b- : defal ndànk bala ngay daanu ci iskale yi.

is : yës, sukk. géleem gi dafa is rekk, mu wàcc.