dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ijji : benn-bennal. bi mu dalee jàng yàggul, dafay ijji. safaan wi mooy dawal.