dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

idda j- : diir bi jigeen ju ñu fase di toog balaa muy amaat jeneen jëkkër ndax mu leer ne ëmbul bi ñu koy fase. góor ñaa ngi koy seeti ngir takk ko te idda ji jeexagul. dinañuy wax tamit yidda j- wala yedd j-.