dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ibliis m- : seytaane s-. bul fexe ba ibliis mën la ci li nga nekk. dinañuy wax tamit bëliis m-.