dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ey : baat la buy tekki yërmande, mbégte wala naqar. ey sama doom ji ! nàmmoon naa la, juroomi at a ngi nii gisuma la.