dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

etaas b- : taaxu kow. Ndakaaru bare na ay etaas.

et w- : mbaam xamul yar, et la xam. dinañuy wax tamit yet w-.