dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

emb : pare. li mu doon def emb na. / waa ji embul mootax mu doxale nii. dinañuy wax tamit yemb.

em : defal ko lu em rekk. dinañuy wax tamit yem. safaan wi mooy ëpp.