dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

egg : dinañuy wax tamit àgg wala yegg. (seetal àgg)

egliis b- : jàngu b-. benn egliis rekk a am ci dëkk bi.