dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

ebal : ebal na ko kër bàjjenam. dinañuy wax tamit yebal.

ebolaa b- : ebolaa feebar bu bon buy wàlle ci lu gaaw la.