dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

axakañ : dinañuy wax tamit ankañ. (seetal ankañ)

axakay : dinañuy wax tamit ankañ. (seetal ankañ)

ax : ku am bànneex wala mettit moo koy wax. yaa ngi may gaañ waay, ax !