dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

aka : lu ñuy wax la bu ñu gisee lu ñu yéem. aka rafet !

akara b- : beñe bu am soosu kaani. ku bëgg akara dangay ñeme kaani (léebu wolof).

ak : jëkkër ak jabar dañoo war di waxtaan.

aksidaa b- : ab aksidaa moo am ci yoon wi mooytax oto yi mënuñoo dem.