dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

addu-kalpe b- : saay-saay b-, sàcc b-. ku def liggeey dogaale nit ñi di nangu li ñu yore (xaalis wala lu am solo rekk) mooy addu-kalpe.