dalub web bi leen di jàppale, ci jàng ak jàng bind làkku wolof

sàqum baat wolof-wolof

aca : baatu aca dañu koy wax ngir dàq dara. / aca leen ñu dem wuti siddeem àll ba. dinañuy wax tamit ayca wala aywa.